explain-icon

Explanation

Yónente bi day xamle ne àjjana ak sawara dañoo jege nit ki kem ni ko ay waroy dàllam jegee te mooy liy nekk ci kaw ndëggu yi, ndaxte moom man naa def ab topp Yàlla ngir ngërëmam loolu dugal ko àjjana, walla ab moy Yàlla loolu nekk sabab ci duggam sawara.

explain-icon

Benefits from the Hadith

  • Xemmemloo ci jëf lu baax doonte dafa néew, ak xuppaate ci jëf lu ñaaw doonte dafa néew.
  • Jullit cig dundam manul ñàkk mu boole yaakaar ak ragal, tey sax ci ñaan Yàlla mu saxal ko ngir mu mucc te du woru ci melokaanam.
explain-icon

Categories

explain-icon

More ...