explain-icon

Explanation

Yónent bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafay xamle ne li gën ci tudd Yàlla mooy: «Laa ilaaha illal Laahu» maanaam, amul kenn ku ñuy jaamu ci dëgg ku dul Yàlla, li gën ci ñaan yi mooy: Alhamdu lil Laahi; te mooy nangu ne kiy joxe xéewal mooy Yàlla -tudd naa sellam ga-, moom mi yeyoo melokaan yu mat sëkk ya te rafet.

explain-icon

Benefits from the Hadith

  • Ñaaxe ci di baril a tudd Yàlla ci kàdduy Tawhiid, ak di ñaan cig cant.
explain-icon

Categories

explain-icon

More ...